06/08/2025
Le Premier ministre Ousmane SONKO, accompagné d'une forte délégation, est arrivé ce mercredi 6 août à Ankara, capitale de la République de Türkiye, pour une visite officielle qui se poursuivra jusqu'au 10 août.
Au programme de cette visite : des séances de travail, des rencontres bilatérales, ainsi que des visites de terrain.
24/10/2024
Samba ndiaye moom dou dial sunu projet niokoy financé nioko ar
06/10/2024
Patriote yi kham yen danguen eupeul diguen focus ba élection yi diall ta dolen ko yeuk Maty Sarr Niang kay wax ak niom ana Idy Dionwar waxal bala lambay di niaww niveau focus bi kawé d😂😂 tata Maimouna Bousso dooniou may deux niou zembré😂😂
01/10/2024
Temps yi waa dic sen yaram tang na nak😂😂
02/06/2024
Man kham naa damay moudié dieul disponibilité thi pastef ba diamono nekh li djiby gueye def dara nekou thi Senegal reewum maslaa la lolen mou guiss ko bagn koo nouyu fu Ousmane SONKO mana accolaté Macky SALL djiby gueye ndiaye warfa accolaté antoine waxé khol bi thi bopam nguen wara bayi am rew ken douko yoré noonu pastef dafa bari ay nitt yoo kham emotion rek laniouy dieufé khind daa raylou mboku yonenté bi hamza dieul khol bi yeuy ko ta bamu toubé yallah dako diegal il faut savoir faire la part des chose maylen niou diam li dra nekou thi
31/05/2024
Waa kouma guissal Tahirou Sarr borom mouvement des nationalistes damako nam